Ay Chono La

Habib Faye, Youssou N'dour

Ndéké mbeuguel nii la
Ndéké yaw rek lenen la
Nit di na la beug ba sank la
Ndéké yaw rek lenen la, lenen la bouko wédi
Mbeuguel ay chono la, bouko wédi
Mbeuguel ay chono la, nangou len ko

Ndéké mbeuguel nii la
Nit di na la beug ba sank la
Ndéké yaw rek lenen la, lenen la bouko wédi
Mbeuguel ay chono la, bouko wédi
Ay chono la, ay chono la, nangou len ko
Mbeuguel ay chono la, boulenko wédi
Ay chono la, ay chono la, nangou len ko

So ko khamé nonou kham né yar no gno yar na gno yar no gno

Oh

Ndéké mbeuguel nii la
Nit di na la beug ba sank la
Ndéké yaw rek lenen la, lenen la bouko wédi
Ay chono la, bou len ko wédi
Mbeuguel ay chono la, nangou len ko

So ko khamé nonou kham né yar no gno yar na gno yar no gno

Oooh

Curiosités sur la chanson Ay Chono La de Youssou N'Dour

Sur quels albums la chanson “Ay Chono La” a-t-elle été lancée par Youssou N'Dour?
Youssou N'Dour a lancé la chanson sur les albums “Set” en 1990 et “History” en 2019.
Qui a composé la chanson “Ay Chono La” de Youssou N'Dour?
La chanson “Ay Chono La” de Youssou N'Dour a été composée par Habib Faye, Youssou N'dour.

Chansons les plus populaires [artist_preposition] Youssou N'Dour

Autres artistes de World music