Xel

Paroles de la chanson Xel :
Famarë reub kat lawone
Da ama biss mou khall yône
Mu taxaw di xalat bamu yàg
Mu sène mbëtt miy daw
Mu suxat fital ambadi dâgu
Té nane kî douma raw
Far mbëtt ma sène kokorong
Dadi dieul bop ba
Dal di koy rône
Bopp ba neubouna litha des
Yaramam béppa ngui fègn
Deune bak, ndigg lak, tank yak, yénène ya
Lippe di fègne

Lii takh mou déféni
Mbeutteu daa amoul xel
Kone gnoune gni Yalla jox xel
Nagnu santati (x2)

Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk
Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax déf

Loy dougou jitalal sa xel
Ba lo thièy wout
Di nga guiss nguenél
Nit gni yor xel boo sété gnoy dokhal aduna
Kiy déf té dou xalat
Thi missal day mél ni mbeut ma

Nit môm khélako yor(x4)

Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk
Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf

Fi neubeu moy khax
Boko amoul yangui mél ni bayima
Sokou amoul doto nék nit

Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk
Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf

Wawaw(x4)

Famarë reub kat lawone
Da ama biss mou khall yône
Mu taxaw di xalat bamu yàg
Mu sène mbëtt miy daw
Mu suxat fital am ba di dâgu
Té nane kî douma raw
Far mbëtt ma sène kokorong
Dadi dieul bop ba
Dal di koy rône
Bopp ba neubouna litha des
Yaramam béppa ngui fègn
Deune bak, ndigg lak, tank yak, yénène ya
Lippe di fègne

Lii takh mou déféni
Mbeutteu daa amoul xel
Kone gnoune gni Yalla jox xel
Nagnu santati (x2)

Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk
Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf

Wawaw lolu moy xel
Soko amoul
Yangui mél bayima (x3)
Loy dougou nang ko téké xel
Famarë reub kat lawone
Mbeuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuutt!

Curiosités sur la chanson Xel de Youssou N'Dour

Quand la chanson “Xel” a-t-elle été lancée par Youssou N'Dour?
La chanson Xel a été lancée en 2007, sur l’album “Rokku Mi Rokka”.

Chansons les plus populaires [artist_preposition] Youssou N'Dour

Autres artistes de World music