Califat

Dominique Preira, Ollanghas Kimbeki Christ Johan

Couplet 1

Bamay duggu ci game bi,
Dama tëju rek di job pour samay buntu tijeeku
Xawma woon ñi tax may sonnay xëy bëss buux ma ci teen bi
Ñaata dëm, jëmmu nit, lamiñu unku ci gemiñ
Mussu ma juutu ci game bi, fayuma juuti ci game bi
Ma yërëm thiouthie yi fi dem bañu dagg seen thiouthiou ci game bi
Segam old school du ruux ci wutum turr new school bi du leen jigg
Rapwolof du raw kenn day mëssa suulu ni teer bi
Man duma middle school, may middle finger ruux tuunu game bi
Ci son ci scène maguel ba mën ma jurr du tee ma sutt la fuuf
Bul ñodi chef ceeneel te cool sa cool
Tojo fudul sa douche
Di course pour mën dab coute que coûte
Muju di wutt secours
Ken xamula ni ku sa propre mère di wo di juum sa turr
I don't talk to these niggers
Got no love for these niggers
Don't give a fuck about your motherfucking soul pussy niggers
Sama ligeey moy faye di soul ay man
Renn damay samp rang wu dé di xaar kuy burle man

Hook

Xaar bi du yagg ba raw ma
Capi bi champing bi ñëw na
Yaw bandit sa papa ji ñëw na (ñëwna Yeah ñëw na)
Chef bi ñëw na

Xaar bi du yagg ba raw ma
Capi bi champing bi ñëw na
Yaw bandit sa papa ji ñëw na (ñëwna Yeah ñëw na)
Chef bi ñëw na

Couplet 2

Bamay duggu ci game bi
jugge ci suufu tunnels yi
Yekci di kung fu ni jet li
Lëndëm ni sunguf bu weex bi
Tek ci ñuul kukku ni derr bi
Sutt la ci lepp, ngay xolu ndax dip sa coup de cœurou mère la
Ci volcan lalay denthie, dumala suul fu suuf mëna sedd
Ñun ñoko fiy teg fu leer
Ngeeni futeeku merr
Ñun ño ngi ci suñu 10e saison série yeen ben sketch ngeen
Mën fenn, da ngeen ci dëggu ni kuy julle ku dee
Suul ngeen ma du lu mën nek mais nak bul xeeb sa rêve
Rabatuma xaj bu jugg di ñoddi wutang clan
Ni gumbak tele
Du mak yeen ñepp wut leen keneen
Man rekkay genne clashs yi topante ni douze ak treize
May guux seen deret
Tiim game bi yepp ni ndiounga kebe
Nigga who's next ?
Somebody tell me who's next again ?
You think you better than me you take the L
I'm supposed to win always one of them got to lose everyday
Ben respect ngeen ma yoreel moy bu ndioulek ak salbe

Hook

Xaar bi du yagg ba raw ma
Capi bi champing bi ñëw na
Yaw bandit sa papa ji ñëw na (ñëwna Yeah ñëw na)
Chef bi ñëw na

Xaar bi du yagg ba raw ma
Capi bi champing bi ñëw na
Yaw bandit sa papa ji ñëw na (ñëwna Yeah ñëw na)
Chef bi ñëw na

Xaar bi du yagg ba raw ma
Capi bi champing bi ñëw na
Yaw bandit sa papa ji ñëw na (ñëwna Yeah ñëw na)
Chef bi ñëw na

Xaar bi du yagg ba raw ma
Capi bi champing bi ñëw na
Yaw bandit sa papa ji ñëw na (ñëwna Yeah ñëw na)
Chef bi ñëw na

Chansons les plus populaires [artist_preposition] Dip Doundou Guiss

Autres artistes de Afrobeats