NLMD

Ligueyou ndaye moy agnou domm
Ronkhognou mère ci niak diom
Mandi bakhoul soxor mo bakh
Té policier bi diay la drogue
Meunoun ma faay
Iblis sax dou job comme man
Awma deukeudo si kaw souf
Bokouniou drapeau non non
Non non non

Founé dem nafa founé fanan nafa
Founé fanan nafa
Founé fanan nafa
Kon Nileu meuneu démé
Nila meuneu démé yeah
Ni rek ni rek
Ni rek ni rek

Nila meuneu démé yeah
Nila meuneu démé yeah
Ni rek ni rek
Ni rek ni rek yeah

Assamane ci meune na khiin té dou taw
Sama mama dina triste mais dou diooy
Deukou cris mais sa fils beugou foo
Bénn doom'al dafa khiff mais dou thiopp
Diotna yé samay guènt, yètall samay beug beug

Goor yé nguii yoom Goor jiguén du gueuneu deugueur
Dou danga mouma rekk sa yalla wara teukh
Diour sa bopp soul sa bopp niaar rekk la meuneu teu!

Amoo place même bassi sa biirou mère nigger
Fim la diouré la sa magg yi diogué nigger
Mowti dina moudji dé
Matt deum bou raffét dou wallé fébar bou nékh nigger
Rakk wolloul sa kharitt yi
Beuss dinga khamné safara mo dakh fii
Déreta fort gnila beugue niola sonal
Sa papa diangala kharou sa maman nampaléla possone

Man dagnma néh diokhéle sa xol ma diokhé sama rouh
Niou khar ba tidji sama gatt ma oubi sama yourr
Nadj dou yeug sédayy kénn leundeum'oul ba taal lamp bou
Nioul
Yagga diokhé sa taate ay nittou goudi yaye djou. Doom bu
Flou
Sa pèle binga gassé pakh bi silagn la moudié soull
Dama cher bomay rayy déféko pakka wourouss
Tant que gnogui fénn beuseul sa khol bagnala tontou mougn
Yakk derr xèssayou xèsall katt deugue bouniou mourr

Ligueyou ndaye moy agnou domm
Ronkhognou mère ci niak diom
Mandi bakhoul soxor mo bakh
Té policier bi diay la drogue
Meunoun ma faay
Iblis sax dou job comme man
Awma deukeudo si kaw souf
Bokouniou drapeau non non
Non non non

Founé dem nafa founé fanan nafa
Founé fanan nafa
Founé fanan nafa
Kon Nileu meuneu démé
Nila meuneu démé yeah
Ni rek ni rek
Ni rek ni rek
Kon Nileu meuneu démé
Nila meuneu démé yeah
Ni rek ni rek
Ni rek ni rek

Kou amoul xol amo fit
Kou gueum yallah do ragal
Ray naniou kou djoudou goudoul
Teuth nguén kou défoul dara
Say mbokou bou diékh bo réindé say noon
Meuno weet so amé ndam
Défaite mom orphelin leu ni sédaayu safara haan?

Daguay business sa diné loudoul faay moussou mala tchi
Guiss
Nittou jammeuh ngeu kagne ngay djoubaulék yallah ak ibliss
Euleuk tchi biir di nga fégne nigga euleuk tchi biir
Nakho sa bopp nakho yonente bi
Ndakh goumba dina guiss souy gueinteu
Khall wané nioumouy lakk bala bissou pinthieu
DEUG méti ni secréts yi nga dinthieu
Do fatté lo nga jangal sa bopp kan mo meusoul féneu

Yeah nigga Thiagga bou yiw ni policier djoup
Meuno di degglou di wakh ni kouy lekk tchi douch
Bopou bou fess day tek djeuweum si suuf
Motah couronne meuneu na djaapeuh kou meussoul nekk bour
Aÿ!
Gni deh nio gueuneu riche nio niou gueuneu niakeu
Sa mellieur xarit la yëré noone ngi di gueuneu djaap
Yallah teuthie bideew ci jail mouy lerral nioune nieup
Djanteu
Même kouy sangue neew sangou katou neew dinako sangue

Ligueyou ndaye moy agnou domm
Ronkhognou mère ci niak diom
Mandi bakhoul soxor mo bakh
Té policier bi diay la drogue

Meunoun ma faay
Iblis sax dou job comme man
Awma deukeudo si kaw souf
Bokouniou drapeau non non
Non non non
Founé dem nafa founé fanan nafa
Founé fanan nafa
Founé fanan nafa
Kon Nileu meuneu démé
Nila meuneu démé yeah
Ni rek ni rek
Ni rek ni rek
Kon Nileu meuneu démé
Nila meuneu démé yeah
Ni rek ni rek
Ni rek ni rek

Chansons les plus populaires [artist_preposition] Dip Doundou Guiss

Autres artistes de Afrobeats