MERO PERTOULO

Bruno HOVART, Lansana SANE

Sa hariti cedé nagnou
Nénagnou kou nagou ligueye woone
Ha sonouga sonouga yaw si diabote guilé waye
Amine ya nago ni gnéneu sare yiga donne tarré
Yaw yama guémbeu démbeu
Mana donne taye sa mbeur
Yaw yama xélale démbeu
Mana donne taye sa goorre
Ina mbeume famaye kan kan

Mero pertoulo
saye doome gnogui gorgorlo

Doome diouné gui gnane yayame féyé dieurigname
Mou mageu téralko topatoko dayessane
Yaw yaye beugonena saye seute fékeu la fi
Sa ma yaye sama yaya boyo

Mani
Mero pertoulo
saye doome gnogui gorgorlo

Yaya boyo mane nameuna la
Yaya boyo mane wétale gama
Mero pertoulo
Aye yaye yaye sa mbeur mi dana bagou dé
Mero pertoulo
Dahe famou déme mome dou ragal déye
Mero pertoulo
Wawe laga defe si gnoune da baréye
Mero pertoulo
Mero pertoulo
Aye yaye yaye sounou téré yaw

Chansons les plus populaires [artist_preposition] Lass

Autres artistes de Afrobeats