TABE

BEATS SEBO, Lansana SANE, Raphael D HERVEZ

Wornané yaw yafi né
Thiowe laye baré yafi né
Koula wédi dala xamoule yaw
Mak yaw rek la
Thiowe laye baré yafi né
Koula wédi dala xamoule yaw
Mak yaw rek la
Mane fila def

Guisna si yaw beugélo
Daye geuna law mane sayana
Guisna si yaw figama love
Aye ma la love héye ma love

Mane yaw la donne séte
Dieguéne diou bahe la donne séte
Fayeda gama woné hé mane yama téré nélaw
Souma manone kéneu raw mane yama téré nélaw
Ba dara métiwoula loubeu beugeu ma defallako
Deiguéne diou bahela waye
Allale dé titalouko

Guisna si yaw beugélo
Daye geuna law mane sayana
Guisna si yaw figama love
Aye ma la love héye ma love

Soma wolo ma yoboula fo soré
Wonala yaw milé hé

Guisna si yaw beugélo
Daye geuna law mane sayana
Guisna si yaw figama love
Aye ma la love héye ma love

Chansons les plus populaires [artist_preposition] Lass

Autres artistes de Afrobeats