Yeungueul Ci Say Mbagg (feat. OMG)

OMG
DD Records

Yaw yay guethie sa ndokh dou diekh
Yaw yay tène boudoul meusseu ndeey
Yaw yay jant say lampe dou faye
Bou goudi dioté yaye done bideew

Ken doula jap bayila
Mel ni yaw tay diafè na
Yaw yay sama kani kon fo diaar ma tothi la
Ninga mel daal eup na
Goor gou bakh tay jaféna
Sama xol ninga koy def yok takh mane ma beug la

Yeugueul ci say mbagg
Ci say mbag
Yeugueul ci say mbagg
Yaw koula ame dé faw mou féthial la

Yeugueul ci say mbagg
Ci say mbag
Yeugueul ci say mbagg
Paréna fo dieum yobaléma

Yeugueul ci say mbagg
Ci say mbag
Yeugueul ci say mbagg
Mani koula ame dé Faw mou féthial la

Yeugueul ci say mbagg
Ci say mbag
Yeugueul ci say mbagg
Paréna fo dieum yobaléma

Fo né jamm jougoufa
Fo di ré mane weetalouma
Japal figa jap bouko bayi beug na
Ma jap fima jap lo wakh lep deug la
Done sa jongama dila wowé nijaay
Do reub sooy yaw la gainde ndiaye

Ken doula jap bayila
Mel ni yaw tay diafè na
Yaw yay sama kani kon fo diaar ma tothi la
Ninga mel daal eup na
Goor gou bakh tay jaféna
Sama xol ninga koy def yok takh mane ma beug la

Yeugueul ci say mbagg
Ci say mbag
Yeugueul ci say mbagg
Yaw koula ame dé Faw mou féthial la

Yeugueul ci say mbagg
Ci say mbag
Yeugueul ci say mbagg
Paréna fo dieum yobaléma

Yeugueul ci say mbagg
Ci say mbag
Yeugueul ci say mbagg
Mani koula ame dé Faw mou féthial la

Yeugueul ci say mbagg
Ci say mbag
Yeugueul ci say mbag
Paréna fo dieum yobaléma

Koula am yow am yow
Owouwa owouwa hey
Koula am yow am yow
Owouwa owouwa hey
Firouma pour fiir beugue na nga am ko
Loufi gueneu diss doundeu nako mak yaw
MBeuguel deugue dou bou say say hey
Linga bouggoul guiss bayinako dakh yaw
I just wanna know
Tell me I just wanna know what you want for me
I just wanna know
Girl you gotta let me know what you want for me
Yaw la tane thi say morom yaw (yeah hey)
Beugue touma guiss say rongogne yaw (yeah)
Diguenté bi dara douko dague (hey)
Li dara douko dague (hey)
Yeungeul ci say mbagg hey (hey hey yeah yeah hey)

Owouwooooooh owouwoh koula am warnala téyé bou bakh
(Warnala téyé bou bakh)
Owouwooooooh owouwoh paréna foy dem yobaléma
(Yobalema)
Owouwoooooh owouwoh (owouwo)
Koula am warnala téyé bou bakh (téyé bou bakh)
Owouwooooooh owouwoh paréna foy dem yobaléma

Chansons les plus populaires [artist_preposition] Dip Doundou Guiss

Autres artistes de Afrobeats