Du Dem

CHRISTOPHE LAXENAIRE, LAURENT PENA, Natty Jean, Puppa Lëk Sèn, RAS JUMBO, VI-AVELINO

Gueum na i thiow li meune na bagna baré
Adouna guééw la dangay seugue beuré
Na ndaw gni fékhé ba séne tchoono dou réér
Na mak gni djouk té dokh lou léér deuggay moudjé
Li douniou tchi guénn filek néwouniou stop
Ya beugg djité war nga oubi sey nopp
Nioune douniou la baal boudé ay bakkan ey rot
Cone fatalikoul ngour dey djéékh deuguéy moudjé
Légui gueume touniou si kénn, Danio doyal séni fénn
Danio fass yééné khekh , djaay doolé daf fii djeekh
Nioungui djakhassé souniouy khéét, bou léne foowé souniou khel
Khaley Sénégal yéén laay délo ndioukeul
Nioune souniou euleuk laniou beugg loubal
Mais daniouy lanke kénn douniou dougueul
Reew mi bénn bopp la lolou dou dégn
Ndawi africa danio beugue takhaw
Ni yééwou djotna meune touniou nelaw
Bo beugoul jamm biss di ay di ne niow
Té lingay lep yeupp dingco fey deuguéy moudjé
Faaw niou diapanté souniou biir
Faw niou beugueunté souniou biir
Faaw niou aaranté souniou biir
Naniou gueunn deugou souniou biir
Naniou samm souniou avenir
Nit cou nioul a bari ennemi
Bénn bangui souniou biir njiit
Bénéén bangui babylone bone
Doomi gaîndé yéé djouk né négn légui djeekh na
Boumou djaam yi dog na diamonoy maam wees na
Kepp kou fii soljah takhawal né bagn na
I man a dé fi conquer i love you mama africa

Chansons les plus populaires [artist_preposition] Natty Jean

Autres artistes de African reggae